笨鸟先飞
我们一直在努力
2025-01-10 11:32 | 星期五

Insh’Allah歌词-Guiss Guiss Bou Bess

Insh’Allah歌词由Guiss Guiss Bou Bess演唱,出自专辑《Insh’Allah》,下面是《Insh’Allah》完整版歌词!

Insh’Allah歌词

Insh’Allah歌词完整版

Aa aa aa

Insallaa aa aa

insallaa aa aa

Insallaa aa aa

Yàgg yàgg yàgg dina baax

Insallaa

Tolloon naa guddi yoo xam ne gënoon na fee metti lool

Ma fas ci sama xol bi ak sama xel mi

Xam ne yàgg yàgg bés di na mës a ñów

Di na mës a ñów lépp di na jeex

Ku am xolu muñ bés bu neexe nga fàtte yow la mettiwoon

Sànt naa Yàlla

Ndax Moom ku ko sànt mu dolli la

Amaana xamnaa ni yoonu ndaw du gaaw

Waaye gëm-gëm rekk a wóor fii ci dunyaa

Yoon waa ngi nii gudd te lëndëm loole

Bariy lëj-lëj ak jam-jam yi

Gëm-gëm rekk a wóor fii ci dunyaa

Bul ma dégglul waxi noon yi

Ñii bëgg laa décourager

Xanaa xamoo ne fii ci dunya gëm-gëm rekk a wóor

Aa aa aa

Insallaa aa aa

insallaa aa aa

Insallaa aa aa

Yàgg yàgg yàgg dina baax

Insallaa

Liggéeyu ndey lanuy ñaan ak ndey ju baax

Buur Yàlla defal nu ko kon sànt Yàlla

Barke baay lanuy ñaan ak baay ju baax

Ngir lu nu mën a am mu mën a barkeel kon alxamdulilaa

Lii nag soo ko ame bul tiit bul ragal

Xanaa xamoo ne dey leeral fa nga jëm

Kon doxal te bul gestu

Bul ma degglul waxi ñii

Naan di na dem ak du dem

Kon waaxul

Kon waaxul gaawal a gaaw te demal sa yoon

Aa aa aa

Insallaa aa aa

insallaa aa aa

Insallaa aa aa

Yàgg yàgg yàgg dina baax

Insalla

Xëccal mu dikk

Xëccal mu dikk

Yàgg yàgg

Yàgg yàgg

Di na mës a ñów

Di na mës a ñów

Di na mës a ñów waay

Wërsëg bul buy turne la

Ku sa niimero génn nga jot ko

Te boo nee tekk tekk wan la yoon

Sàcc bi da fa yàkkamti di jël waaye la muy sàcc wërsëgam la

Doomu Aadama Njaay ku dund for sa muur

Ñoddi bu dogul yàgg-yàgg soo ko gëme di na mësa dikk

Walaay di na mës a ñów

未经允许不得转载 » 本文链接:http://www.benxiaoben.com/ef432VVA9BQpXUwoGDA.html

相关推荐

  • Muus歌词-Guiss Guiss Bou Bess

    Muus歌词-Guiss Guiss Bou Bess

    Muus歌词由Guiss Guiss Bou Bess演唱,出自专辑《Jolof Bass Music》,下面是《Muus》完整版歌词! Muus歌词完整版 Niou cre mouvement march Mussant Mamie Mon...

  • Tik Tik歌词-Guiss Guiss Bou Bess

    Tik Tik歌词-Guiss Guiss Bou Bess

    Tik Tik歌词由Guiss Guiss Bou Bess演唱,出自专辑《Tik Tik》,下面是《Tik Tik》完整版歌词! Tik Tik歌词完整版 H茅H茅 H茅 H茅 H茅 H茅 H茅 H茅 H茅 Diamono...

  • Se Januk歌词-Belal Khan

    Se Januk歌词-Belal Khan

    Se Januk歌词由Belal Khan演唱,出自专辑《Se Januk》,下面是《Se Januk》完整版歌词! Se Januk歌词完整版 সে জানুকশিল্পী : বেলাল খানগ...

  • 楼下那个女人 (cover: 游鸿明|高家惠) (Live)歌词-爱唱歌的奎哥

    楼下那个女人 (cover: 游鸿明|高家惠) (Live)歌词-爱唱歌的奎哥

    楼下那个女人 (cover: 游鸿明|高家惠) (Live)歌词由爱唱歌的奎哥演唱,出自专辑《楼下那个女人》,下面是《楼下那个女人 (cover: 游鸿明|高家惠) (Live)》完整版...

  • 人民币歌词-万珂凡

    人民币歌词-万珂凡

    人民币歌词由万珂凡演唱,出自专辑《Spring Story》,下面是《人民币》完整版歌词! 人民币歌词完整版 因为穷我才会根本穿不起那些rapper 身上的库奇ap因为穷我才...

  • Tony Soprano 2 (Explicit)歌词-Nines

    Tony Soprano 2 (Explicit)歌词-Nines

    Tony Soprano 2 (Explicit)歌词由Nines演唱,出自专辑《Tony Soprano 2 (Explicit)》,下面是《Tony Soprano 2 (Explicit)》完整版歌词! Tony Soprano 2 (Expli...