Bayfalloo Toubab歌词由Cheikh Ouza演唱,出自专辑《Bayfalloo Toubab》,下面是《Bayfalloo Toubab》完整版歌词!
Bayfalloo Toubab歌词完整版
BAYEFALOO TOUBAB
Bayfalou serigne touba ma geunal
Bayfalou toubab X4
dafa gneuw sougnouye reeww
Sopi sougnouye khEL
Iindaléé ay féém
teek thi aayii fééne
yaw Nguaay soloo nii man
te say khalaate di mom
Loum la waakh nguani waaw
Loum la dééflo nguani waawaw
ngua nee thi aay yiiteem leep
thi aar djikoom jou boon
khoolo famouy dieum
ak lane moko wara sokhaal
soopi sa dokhaliine
nguay dokh thiia laa ko nekh
moulaaye ligueye lo
nguir yakh sa ada ak sa diiné
Bayfalou serigne touba ma geunal
Bayfalou toubab X4
bayfaloo toubab
BA mou djaaral la nguay baap
ba sandi leep li baaakh
thi say ada mam
bayfaaloo toubab
Té moo sank say mam
yaw ak mom dou nguene bene
seni diguanté nakhéé la
ngua dokh thi aay yiiteem
thi aar djiko jou boon
khoolo famouy dieum
ak lane moka wara sokhaal
soopi sa dokhaliine
Yaw ngua NE thiia laa ko nekh
moulaaye ligueye lo
nguir yakh ada ak diiné
Refrain 2
da ngua reeer sa akh ak yeleef
dou nassarane
Bayfalou serigne touba ma geunal
Bayfalou toubab