笨鸟先飞
我们一直在努力
2025-01-09 00:44 | 星期四

COSAAN歌词-Yoro Ndiaye

COSAAN歌词由Yoro Ndiaye演唱,出自专辑《YAAY KAN》,下面是《COSAAN》完整版歌词!

COSAAN歌词

COSAAN歌词完整版

Cosaan

Nañu fonk suñu cosaan,def ko ni ndokh ci ndaa so maree tankh naan

Mooy doole ndanaan

Fonkal nee di laal ci baaxi maam

Soo reree laac ko maam mu wax la linga moom

Ku xeep sa nguuro doon badola boo fattee linga moomee reer yomb la

XIIn jipp Baol jokk baal faal ba jaayu,mag ña doon taaxuraan baol lañu cosaano

Demb moo tax ñu naan tay

Demb ëpp naa fattee

Demb moo tax ñu naan tay

Demb ëpp naa fattee

Junjung yaa nga siin ,

ndaga saloum ma ko moom,

fouta naabe yeela

Nañu dem ba Casamance ,tamba ba Kolda bugarabou balafon Soruba ñooy boroom

Sunu cosaan,sunu cosaan yaatu na

Bargny guethie gumbe leen teunguethie ngor ouakam ndakaru ndiaye

Sunu cosaan sunu cosaan yaayu na

Nañu fonk sunu cosaan def ko ni ndokh ci ndaa soo maree tankh naan moy doole ndanaan

Fonkal sa cosaano,di laal ci baaxi maam soo reeree laac ko maam mu waxla linga moom

Demb moo tax ñu naan tay

Demb ëpp naa fattee

Demb moo tax ñu naan tay

Demb ëpp naa fattee

Bul di fattee li nga moomee ,fanga jogguee ak langa doonee

Boo flattée demb rer yomb laa,ëppnaa fattee bulko fattee yoow

Yaw mi maam boy,yaw mi fekke demb ñewal nettali ñoo

Ndax ñu naan ,demb takh ñu naan tayjilee bul ko faatee yaw

Demb moo tax ñu naan tay

Demb ëpp naa fattee

Demb moo tax ñu naan tay

Demb ëpp naa fattee

未经允许不得转载 » 本文链接:http://www.benxiaoben.com/ef667VVA9BgFRVQIBDg.html

相关推荐

  • YAAY KAN歌词-Yoro Ndiaye

    YAAY KAN歌词-Yoro Ndiaye

    YAAY KAN歌词由Yoro Ndiaye演唱,出自专辑《YAAY KAN》,下面是《YAAY KAN》完整版歌词! YAAY KAN歌词完整版 Yaay kan?Bggnaa ku xam linga moom,linga doon,xa...

  • XALE BU JIGUEEN歌词-Yoro Ndiaye

    XALE BU JIGUEEN歌词-Yoro Ndiaye

    XALE BU JIGUEEN歌词由Yoro Ndiaye演唱,出自专辑《YAAY KAN》,下面是《XALE BU JIGUEEN》完整版歌词! XALE BU JIGUEEN歌词完整版 Xale bu jigueenNjangu xale...

  • JFJL歌词-Yoro Ndiaye

    JFJL歌词-Yoro Ndiaye

    JFJL歌词由Yoro Ndiaye演唱,出自专辑《YAAY KAN》,下面是《JFJL》完整版歌词! JFJL歌词完整版 Jf jlAlal ji dole ji taar bi ruu giDina dem moom,taggook bo...

  • GUDDI歌词-Yoro Ndiaye

    GUDDI歌词-Yoro Ndiaye

    GUDDI歌词由Yoro Ndiaye演唱,出自专辑《YAAY KAN》,下面是《GUDDI》完整版歌词! GUDDI歌词完整版 GuddiCi guddi gi i di soundi di toxi broundAll a round i...

  • JFJL歌词-Yoro Ndiaye

    JFJL歌词-Yoro Ndiaye

    JFJL歌词由Yoro Ndiaye演唱,出自专辑《YAAY KAN》,下面是《JFJL》完整版歌词! JFJL歌词完整版 Jf jlAlal ji dole ji taar bi ruu giDina dem moom,taggook bo...

  • GUDDI歌词-Yoro Ndiaye

    GUDDI歌词-Yoro Ndiaye

    GUDDI歌词由Yoro Ndiaye演唱,出自专辑《YAAY KAN》,下面是《GUDDI》完整版歌词! GUDDI歌词完整版 GuddiCi guddi gi i di soundi di toxi broundAll a round i...

  • WAX歌词-Yoro Ndiaye&Ashs The Best

    WAX歌词-Yoro Ndiaye&Ashs The Best

    WAX歌词由Yoro Ndiaye&Ashs The Best演唱,出自专辑《YAAY KAN》,下面是《WAX》完整版歌词! WAX歌词完整版 WaxSammal wax,moytul wax,gstul wax xamal lingay ...

  • REEMA歌词-Yoro Ndiaye

    REEMA歌词-Yoro Ndiaye

    REEMA歌词由Yoro Ndiaye演唱,出自专辑《YAAY KAN》,下面是《REEMA》完整版歌词! REEMA歌词完整版 ReemaSuma xeyee guissuma sa reejiDuma xam lu yendoo ci k...