GLOW UP歌词由NDAKHT LO演唱,出自专辑《GLOW UP》,下面是《GLOW UP》完整版歌词!
GLOW UP歌词完整版
Fo massa guiss
Nit kouñuy deuthie
Té deh wa goul
Wowowowo wooyy
Dieul kolouté teur ko raay
Dékil kiy moytou
Bobou magui dieul Pousso di ñaw Limu xotti
Matraque bo téguone Sama yaram faté wouma
Yakar nga tassone Abandon yi ma dem ba miss ko
Sama doundu mel ni internet
Lingay guiss bokoulak li nek
Guént gui diexna
Legui magui ni di free
Amatouma ben reuthiou si lima wéssu
Dama xassa wané guinaw douma guessu
Yabinala ( ahhh)
Douma lékatt
Démal deglu Mbaye Gaye Faye boul ko forcé
Kakatar bari jikko lañ ko xamé
Lép lu wéx du méw ñamal sétt Kaay déglu ma
Man bayi nala
Bayi nala
Mélni wér ñumay sén si kaw
Lép luma nek mu Glow Up Hé!! Amigo
Man mala off (Lér na)
Train bi fi lala baa Démal nga tokk hé !!
Magui Jongoma lou neex
Mélni rose zu valentin
Foma séné maay réh
Déf lou am classe
Téksi di xéñ nex
Ma yeungal adouna haa
Jongué sax waruna
Guént gui diexna
Legui magui ni di free
Amatouma ben reuthiou si lima wéssu
Dama xassa wané guinaw douma guessu
Yabinala ( ahhh)
Douma lékatt
Démal deglu Mbaye Gaye Faye boul ko forcé
Kakatar bari jikko lañ ko xamé
Lép lu wéx du méw ñamal sétt
Kaay déglu ma
Man bayi nala
Man bayi nala
Man bayi nala