Argent Sale (Version Afro Pop)歌词由Ablaye Dieng演唱,出自专辑《Argent Sale (Version Afro Pop)》,下面是《Argent Sale (Version Afro Pop)》完整版歌词!
Argent Sale (Version Afro Pop)歌词完整版
Argent Sale (paroles: Ablaye Dieng & Oumar Sow
Music: Oumar Sow
Adouna bi, xamoulo koy wolou
Koy wolou ,koy wolouou
Diamono dji,xámato koy wolou
Eh Eh, koy wolou koy wolouou
Ma dénke la sama allal
Ma föok nii di n’ga mako samal
Koon adouna bii xamato
Koy wolou, eh eh koy wolou
Deug koy wolouou
(refrain)
Dissö,ak napkât yii. )
Dissö,ak bayekatt yii. ). 3 fois
Dissö,ak samkatt yii. )
N’guir Jeriño suff cï____ N’guir Jeriño guéth guï____ N’guir Jeriño diour guï
Gör ak gör bulën Bür bii Yalla bolée cii n’gör
Eh eh, ku cii n’jeuke dëm
N’gör deçatüfa,n’ga défma soxna
Amm ak man aye döm, söxla yi barébaré barébaré
N’ga bayii ma ak njaboot giï
Kön aduna bi ,xamato koy wölou
eh eh, koy wölou, koy wölou
(refrain)
Bul dissö,ak wörkât yii. )
Bul dissö,ak dörkatt yii. ). 3 fois
Bul dissö,ak sëttkatt yii. )
Du gñu n’jariñu n’jariñu reew mi____ Du gñu n’jariñu n’jariñu reew mi
(solo saxes)
Köcc Barma woxöon nafi,
Djigenn sopal te bul wolou
Hey, kön xámato koy wolou…ou
Ma takk soxna, def ak momiiy doom
Soxla layii bareebaree….baree
Mü bayim’ak jabóot gii
(refrain)
Dissö,ak napkât yii. )
Dissö,ak bayekatt yii. ). al coda