Thies歌词由Jeeba演唱,出自专辑《Alajee》,下面是《Thies》完整版歌词!
Thies歌词完整版
Ooh ooh
Succ猫s boun茅 xana xamo wakhtou laay xaar
Borom xam xam yi dioundj nagn ko dooyna waar
Taay magg nagn xam茅 boubakh flambeau bi 帽oko yoor
Sou bax茅 帽ioune la baxaal sou boon茅 it 帽ioune la boonal
Thies mako moom yaako moom 帽okoo moom
脩ou degeul baat bi dieum si kaaw
Do daaw moukou xamnani gaind茅 nga
Deuku ba帽n kat ben la si S茅n茅gal
Deuku ngon猫 latyr ak Seck signature Sanekh motax 帽u neex
脩oune soxla wugn di茅gani rooyukay
Fess fi deel tax 帽oukaay ndaamo waay
Deuku ba帽e kaat ben la si s茅n茅gal thies kay rek si xol dara dokou faay
Kou weedi ladj leen liim ma faay
Ah waaw wawaaw thies Sama deuk la mane makoo moom
Ah waw wawaaw thies sunu deuk leu 帽oune nioko moom
Setsima gaaw ma wone l脿 way wone la lodoul guiss si bene reew
Fi adiana la no y鈥檃 pas photo jengu mane leu Kone nagn ko topato
Koun茅 sagn nga wakh ni finga deuk mom mo la nekh
Koun茅 sagn aapo ni finga deuk n茅 mola nekh
Koun茅 sagn nga waxni finga deuk moom mo nekh
Thies kaay moma nekh mane mooma nekh eh moniou nekh
Thies kaay ioe mo niou nekh yobou ma yobou ma
Keur mame Elhadj Ziar茅 Ahmed Barro ndi茅gu茅ne diar diamageune
Ziar sunu mame Abdou Aziz Aidara deem Medina Fall penc Baye fall yaa
Cheikh Ndiguel fall Meissa bigu猫 coumba Fall Dabaay
Khabrou Abdoulaye Yakhine Sama mame Amadou lamine Ba
Du帽u fatei wa diangou bi thies kaay mooy Sama reew
Ah waaw wawaw thies Sama deuk leu mane makoo moom
Ah waaw Wawaw thies Sunu deuk leu nioune nioko moom
Setsima gaaw ma wone laa way
Wone la lodoul guiss si Benen reew fi adiana la
No y鈥檃 pas photo jengu mane la Kone nagn ko topato
脩ugn soxla wugn j茅guaani rooyukay
Fess fi deel nioukoy ndamoo waay
Deuk bagn kaat bil茅 si s茅n茅gal thies kay reik si xool dara douko faay
Kou weedi ladj leen ma liim ma faay
Ooh ooh
Eeeh eeeh yobuuma mbour guedj mbour Soc茅 mbour kankourang aah
Damay nieuw gaaw yaay eeh eeeh thies kaay
Hun hun thies kaay
脩ugn soxla wugn j猫guani royukaay fess fi deel taax niukooy ndamo Wawaw
Deuku ba帽e kaat b茅 si s茅n茅gal
Thies kaay rek si xol dara douko faay kou weedi ladj leen ma liim ma faay!