Lem (Remix)歌词由Bou Biblio演唱,出自专辑《GUDDI》,下面是《Lem (Remix)》完整版歌词!
Lem (Remix)歌词完整版
Damala sexaloon lem
Wax ma fane lala deff ?
Lem bi bariwoon sa lamiñ
Ngani ma parée nga pour doon sama soxna
Leegi danga bëgg xëy dem
Dem bayi kila gënnë bëgg ci sa aduna
Mon bébé
Bëgg na la nëwaat'al bo ko mënee
Te xam nga rek ak man nimala miinee
Gisàtuma kuy taccu sumay gumbee
Ci lëndëm kumay gungee
Dem nga yobaale nga sama lem bimay dundee
Bilaay man waaru na ci bii jamono
Damako woolu jox ko sama lem mu njarr ko
Elle m'avait promis.... Yéeehhh
Tes mots sont toujours là
C'est toi qui m'avais promis que tu vas l'être

Fajjal ma city girl quality
Nangu na sa taar sa jaakaayu my kalessi
Danga ma izi come you my free
Boo fi nekee mangi dé cool di coff souma the'a
Where you are ? I call you come back
Danga ma newoon baaba nañ ko dundu ba ca trône ba
Ngà dem ba fi lall ak lompa
Leegi sooma rombee day melni rombaat
Sama xol lala joxoon
(Pour muy clair)
Man yow rek la noboon
(N la leer)
Sa promesse ya ko louche
Nga digg ma jalous
Ku la nobb moola ñeeme fiire ba jass
Dama dof fi ma nek a cool ci man
Xaw ma waadji fan la jaar ba gondi ma
Elle m'avais promis....