Yoonu Ndam歌词由Bou Biblio演唱,出自专辑《GUDDI》,下面是《Yoonu Ndam》完整版歌词!
Yoonu Ndam歌词完整版
Aduna mosuma wax dara
Kaćcoor bul dundée
Man màgg mos nama déey
Ne ma goor dëgg ba la baax
Dayy àm jòmm te lu mu ligéey
Xam fum koy deff bu bañée gàccee topp ko
Yoonu ndam du gaaw
Fii nii
Xam nganée lunnee di ngàko degg
Waayé nak goor
Yoonu ndam du gaaw
Jayantéel
Hé lunnée di nga ko degg
Goor-goor lul
Yoonu ndam du gaaw
Dou mënnë gaaw
Xam nga né lunnée di nga ko degg
Louné dinko degg
Yoonu ndam du gaaw
Ci dundu gii
Ndaw ngà doon yay muñ
Naaj bi lu mu tàng tàng
Ndam'a nga ća kanam jambaar
Dippér na la gayndé jélé ngaanr
Buddé teranga
Di na la teral ndama
Di ngà degg jaraam say wayjurr
Lii la lay diggël muñël
Yoonu ndam du gaaw
Fii nii
Xam nganée lunnee di ngàko degg
Waayé nak goor
Yoonu ndam du gaaw
Jayantéel
Hé lunnée di nga ko degg
Goor-goor lul
Yoonu ndam du gaaw
Dou mënnë gaaw
Xam nga né lunnée di nga ko degg
Louné dinko degg
Yoonu ndam du gaaw
Ci dundu gii
Yoonu ndam du gaaw
Fii nii
Xam nganée lunnee di ngàko degg
Waayé nak goor
Yoonu ndam du gaaw
Jayantéel
Hé lunnée di nga ko degg
Goor-goor lul
Yoonu ndam du gaaw
Dou mënnë gaaw
Xam nga né lunnée di nga ko degg
Louné dinko degg
Yoonu ndam du gaaw
Ci dundu gii