Ngor歌词由Bou Biblio演唱,出自专辑《GUDDI》,下面是《Ngor》完整版歌词!
Ngor歌词完整版
Tekki wo dara
Do ko wax doomu jambur
Sa doom bi mo tekki wul dara
Njàmbur bu fa joggee prison lay dallu ji
Da sacci woon
Yow tekki wo dara bayil di ko wax doomu diambur yi
Sa doom bi prison lay dallu ji su joggée Njàmbur da sacci woon
Lekkum ba suur
Naanuma ba mandi
Nekkuma di njucc njaacc
Sama jòm la leen di jaay
Yayoo yaay Yayoo yaay yaay
Yaay xaar ma yaay
Teranga ngi ci suuf
Mann mangi dox ci suuf
Jamono jamono jamono
Defal ndank bul ma tegg pression
Mangi lay gis ya ngi yàqq dundu xalé yi
Xalé yi sen yaay bayyé jamono
Bëgg bëgg yée bari
Li nek ci poches yi neew
Féxeel ba tëddée na nga nelaw
Moyto yandóor
Bu sa ngor di nelaw
Bul nangu bëg bëg aduna yée ko
Yow bu sa ngor di nelaw
Bul nangu bëg bëg aduna yée ko
Sàa bu sa ngor di nelaw
Bul nangu bëg bëg aduna yée ko
Bu sa ngor di nelaw
Bul nangu bëg bëg aduna yée ko
Yéewu rek dem xëyy i
Lù nu Yaala may ñu jël sànt ko
Waxuñ da ñuy tekki by force
Da ñuy moytu bêgg lu nu mënul àm
Di nañ daw di nañ daanu
Di nañ dox wayé du ñu daagu
Xaalis moy tekki ci ñi fogg ni tekki moy ñi am xaalis ñoo ñu moy ñi tekki
Yaay bul xèeb sa doom
Bul xèeb sa dòom ci kòom kòom
Nawal sa dòom ci am jòm bi mu am jòm
Ba di wutt muy neew
Di woute mouye néw
Bul nangu bëgg bëgg aduna yée ko
Yow bu sa ngor di nelaw
Bul nangu bëgg bëgg aduna yée ko
Bu sa ngor di nelaw
Bul nangu bëg bëg aduna yée ko
Sàa bu sa ngor di nelaw
Bul nangu bëg bëg aduna yée ko