aani歌词由Daara J Family演唱,出自专辑《aani》,下面是《aani》完整版歌词!
aani歌词完整版
Ñaani bañ naa
Ñaani bañ naa
Jàpp leen sen kurus ta ngen ñaan
Buur bi Yàlla mày nu ndàm
Nu Yëkkati sunu Sénégal ci kaw a kaw
Muy Goor ak Jigeen Màg ak ndaw
Bu ci ken des ginaaw Yëkkati Sunu Daraapoo(drapeau)
Ca kaw a kaw
Jàpp leen sen kurus ta ngen ñaan
Buur bi Yàlla mày nu ndàm
Nu Yëkkati sunu Sénégal ci kaw a kaw
Muy Goor ak Jigeen Màg ak ndaw
Bu ci ken des ginaaw Yëkkati Sunu Daraapoo(drapeau)
Ca kaw a kaw
Couplet 1:
Senegaal - ndam rek
2002 wane na yoon wi
Ay champion - Jom rek
Taxaw ci toit bi ci monde bi
Fi la nu tekk sunu bët yi
Jëli Ji Bi médaille
Ci marche bi marche bu njëk bi
Raaya bi ñoy boroom
Ken du ñu tërr ci geew gi
Ken du ñu jiitu ci rëdd bi
Ñu jeggi Record bi
Ni Amadou Dia Ba ci podium bi
Amadou Gackou dëggal ko ni -
Senegal , Palmarés
Amy Mbacké Thiam ne du des
li fond la course ak vitesse
Ñoy chef lii la yalla def -
Dirigé’k doole Double less
Score bi nu yokkati
Def team ni Metsu Bocandé
Mame maty ,Etienne ,Gorgui Dieng
Bideew ci kaw balle bi Bonde
Ñu dundal Compétition bi
Tiene Mental bu Gandee
Ñaani bañ naa , Ñaani bañ naa !!
(Tey la waalo gëna àay danuy bañ ba tay
Ñaani bañ naa , Ñaani bañ naa !!
Tey la waalo gëna àay danuy dem ba jeex
Jàpp leen sen kurus ta ngen ñaan
Buur bi Yàlla mày nu ndàm
Nu Yëkkati sunu Sénégal ci kaw a kaw
Muy Goor ak Jigeen Màgg ak ndaw
Bu ci ken des ginaaw Yëkkati Sunu Daraapoo(drapeau) Ca kaw a kaw
Couplet 2 :
Duñu nangu Ken di ñu yoxosu
Tay la gaynde gënë wagassu
May leen ñu ndox ñu raxasu
Ndam lañuy yootu ba àgg si
Ñaani bañ a tina bu lepp ne tekk ba arbitre bi sifflé
Nga xam ne lepp dëggla du ñu négocié
Danuy labbali sunu fàs lawal suñ legacy
Buñu tëkku ndax Kersa du ragal
Leeg leeg ñu gennee jiko waga
Kenn duñu Lazer laaj ko Salah
Linu ñakk du fulla du fàyda
Ñoy champion d’Afrique di beaux gosses
Suñu jigeen ñoo leen ëpp cakass
Uppercutu KO la du pés
Duñu leen may dara du mbaquus
Bu doyul ñu Dolli ci nokoss
Boy woote malade ñun la Ñagass
Xeff xippi ñu defal la bagaas
Dañu dogu tay lañ gënë focus
Jàpp leen sen kurus ta ngen ñaan
Buur bi Yàlla mày nu ndàm
Nu Yëkkati sunu Sénégal ci kaw a kaw
Muy Goor ak Jigeen Màgg ak ndaw
Bu ci ken des ginaaw Yëkkati Sunu Daraapoo(drapeau)
Ca kaw a kaw
Jàpp leen sen kurus ta ngen ñaan
Buur bi Yàlla mày nu ndàm
Nu Yëkkati sunu Sénégal ci kaw a kaw
Muy Goor ak Jigeen Màgg ak ndaw
Bu ci ken des ginaaw Yëkkati Sunu Daraapoo(drapeau)
Ca kaw a kaw
Fii ñoo ko moom ndam li ñoy boroom
Du ñu sen moroom ay Gaynde njaay la ñu
Alaa àccu du nu sònn du nu tàyyee
Fii de ñoo ko moomee ndam lii ñoy boroom
Du ñu seen moroom ay Gaynde njaay la ñu
Alaa àccu du nu sònn du nu tàyyi
Jàpp leen sen kurus ta ngen ñaan
Buur bi Yàlla mày nu ndàm
Nu Yëkkati sunu Sénégal ci kaw a kaw
Muy Goor ak Jigeen Màgg ak ndaw ( ñaani bañ naa ñaani bañ naa)
Bu ci ken des ginaaw Yëkkati Sunu Daraapoo(drapeau)
Ca kaw a kaw
Jàpp leen sen kurus ta ngen ñaan
Buur bi Yàlla mày nu ndàm
Nu Yëkkati sunu Sénégal ci kaw a kaw ( dandy bañ ba tay )
Muy Goor ak Jigeen Màgg ak ndaw
Bu ci ken des ginaaw Yëkkati Sunu Daraapoo (drapeau)
Ca kaw a kaw ( tay la waalo gëna àay da nuy đem ba jeex