Runaway歌词由Wally B. Seck&Thione Seck演唱,出自专辑《I Wanna Be Free》,下面是《Runaway》完整版歌词!
Runaway歌词完整版
Runaway ooh runaway
Find a way, ooh runaway
(Wally)
Guédja ngui kheuthiou di nieuw
Té khamoulo louko teuyé sama waay
Mbirou yalla
Ndéké charte biir guéédj,
Kou eup seu morom dolé agné
Ah damay laadj
Niou nééw dolé, ni niom founiouy agné
(Thione Seck)
Xanaa dadjék borom yeurmandé
(Wally)
Adouna nii la bindo
Makhaama gni ley tané wor nama
Runaway ooh runaway
Runaway ooh runaway
(Wally)
Lima yalla thieuralé,
Lenen lou bokoul ci mom beugou mako
Mo xam lou nééw, mba mou beuré bari beugou mako
Non non non
(Thione Seck)
Kone yalla bo dadjék mom
(Wally)
Am-am ci tél mom, ci moudieuntél
Yallay mayé Oh-ohh
Diaam bi takhawél Alhamdoulilahu
No no no - no no
Léér biy daw seu dieum dji,
Worna keuwnou-bi walay wowowo
Té bou nieup yamone thieur,
Am niou guééd sen boss bilaay, wornama
Gorgorlou doyna borom bi
Molay takha done goor fayalaahou
Gueum naa ni li rouh di doundé,
Dina fegn ci dieum dji, lilaay
Dieun bou mak bay beug lorr dieun bou ndaw bi
Té xamoul ni ci biiram beu léy agné
Dou deugné, dou deugné eh eh
Yeurmandé Lahu daa yaa
Yalla na yalla yeureum diaam gni
Bilaay yeurmandé Lahu bour bi
Runaway ooh find a way
Runaway ooh find a way
Runaway ooh find a way
Runaway ooh find a way
Ooh Yalla yaay borom diaam gni
Ngueuramal souniou borom,
Louma meunti am, momako gueunal
Yeurmandé Lahu
Yeurmandé Lahu daa yaatou