Yow la歌词由Vj&AMADEUS演唱,出自专辑《Yow la》,下面是《Yow la》完整版歌词!
Yow la歌词完整版
Set naa setoo setat guissagouma kou melni yaw
Sa dieum di猫 ma y毛m man guissouma k猫n猫ne
Pourtant mane pourtant mane
Guiss na fa莽on bou n猫
Pourtant mane pourtant mane
Guiss naa djiguen boun猫
Yaw laaa done niane yalla (toucouleur al猫 racine)
Niane yi moudi猫 antou (di猫k raf猫te ya ngui)
Yaw lay guiss w毛r ba ngui
Kouy ndeyam ak bayam setoo set ya ngui xoo looo say morom
Diouk lene taye la teey kouko Xam na nga diayou (diayouuu)
Ya diara sargal yaaa diara tathiou
Diayoul tey sa biss la mane mane maaa la taamou
Say dig morom say nawl猫 soula n猫x猫 baaakou
Mbeuguel Dafa diss, Dafa beurri dol猫 Yaye sama aljanah (waaaawaaw yaw)
Yaye sama aljanah (Ahhh Ahhh Yaw la)
Yaaa ma l毛n geuneul yow mi (Waaaawaw Yoe la)
Yaye sama aljanah
Diombadioo ari X2
Diombadioo ari sama s毛t baaa ngui yek si na
Diombadioo ari X2
Diombadioo ari sama s毛t baaa ngui yek si na
Beuss bi laaa done xar , Tay Dafa melni mo ngui
脣ksil sama ndanane , naaala siggil si say nionie yaw
Fi niou diar limala togne, li nga may baaal
Limala diaral ak fi nga ma tolou sama ndanane
Yama l毛n geuneulone dama l毛n ko roussona wax
Imam t毛w na nawl猫 yeup t毛w yaw deh ngani waw
Ndi毛gu毛mar biss yaaadi meut di毛g
Mayko mou dial sama miss ba ngui
Xal猫 la waaay猫 fess na ak diom
Biss dina doni ndanane sama miss baaa ngui
Mbeuguel Dafa diss, Dafa beurri dol猫 Yaye sama aljanah (waaaawaaw yaw)
Yaye sama aljanah (Ahhh Ahhh Yaw la)
Yaaa ma l毛n geuneul yow mi (Waaaawaw Yoe la)
Yaye sama aljanah
Diombadioo ari X2
Diombadioo ari sama s毛t baaa ngui yek si na
Diombadioo ari X2
Diombadioo ari sama s毛t baaa ngui yek si na
Me and you for life for life Bae
Me and you for life for life Bae
Xamal ni ma ngui si sa w毛t
Mouy taaaw Wala mouy nadie ma belle
--