So Ma Ne Waw歌词由Jeeba演唱,出自专辑《Alajee》,下面是《So Ma Ne Waw》完整版歌词!
So Ma Ne Waw歌词完整版
Mane tanne nala si jigueen yudul diekh
Jokh Nala sama xool bi yaay borom
Kone baby boul ma n茅glig茅 maay sa xool
Ndakh malay jokh leep lu geune si yoow
Mane tanne nala si jigueen yudul diekh
Jokh Nala sama xool bi yaay borooooom
Boul n茅glig茅 xamal ni Yaay sama xool
Ndakh beugg nala yoow bae beugg nala
Mane So man茅 waw ma nieuw sen keur
Yoow beugg nala yoow bae beugg nala
Mane So man茅 waw ma nieuw sen keur
Yoow beugg nala bae beugg nalaa!
Woo nala telephone dieulou loo
Envoy茅 nala message wuyuwoo
Lane motakh yow babe lane motakh
Woo nala telephone dieulou loo
Envoy茅 nala message wuyuwoo
Lane motakh yow babe lane motakh
Bou mbeguel done diaay
Bou mbeguel done diaay
Yow babe diokh nala la xool bi
Way茅 leep yakoo moom
Way茅 neewoul dama niaak diom
Meussuma niaak diom
Mane sama mbeuguel moma yobou
Motakh malaay wo oh
Lane motakh babe lane motakh
Soumalay woo tei babe doma dieul
Lane motakh babe lane motakh
Soumalay woo tei babe doma dieul
Yeah yeah yeah
Yeah yeah yeah yeah yeah yeaaaaaaaahhh
Anh Anh....
Ndakh beugg nala yoow babe beugg nala
Mane So Man茅 waw ma nieuw sen keur
Yow beugg nala yow babe beugg nala
Mane So Man茅 waaw ma nieuw sen keur
ma nieuw ma nieuw ma nieuw
Beugg nala yow babe beugg nala !