REEMA歌词由Yoro Ndiaye演唱,出自专辑《YAAY KAN》,下面是《REEMA》完整版歌词!
REEMA歌词完整版
Reema
Suma xeyee guissuma sa reeji
Duma xam lu yendoo ci kër gui
Man suma xeyee nga fass sa kanam gui
Duma xam lumay yendoo ci bess bi
Te yaw yay kimay begalalee oho
Te yaw yay kimay dëfëlee suma merree
Ngalla reema,ma reela
Si tee finga tee ma tee fima tee
du dem
Ngalla reema,ma reela
Soo tee finga tee ma tee fima tee
Du dem
Ngalla reema ñu bègue
Soo xëye ba tongu ma
jaaxle moom dikkal nama
Soxnasi wuyu manmiley jaxlenaa
Ndax neegu sëy bi dafa xatt
Tumuranke ci da had
Baby wuyu ma
Man yaay ki may begal
Yaay kimay dëfël ,
yaay kimay dallal
Sama xol bi ya koy seddal man baby
Ngalla reema,ma reela
Si tee finga tee ma tee fima tee
du dem
Ngalla reema,ma reela
Soo tee finga tee ma tee fima tee
Du dem
Ngalla reema ñu bègue
Un sorriso al tuo risveglo
Mi dá gioia ed energia
Vederti la mattina con la Luna storta
Che senso a la giornata
Nulla piu mi importa
Vederti ridere,mi fa vivere
Ma chérie dee ma ree
Man yaw laay beguee
Ndax negu sëy bi dafa xat
Tumuranke ci dafa had
Baby wuyu ma,
man yaay ki may begal
Yaay kimay demëfël
Yaay ki may seral
Sama xoll bi yakoy seddal man
Baby
Ngalla reema,ma reela
Si tee finga tee ma tee fima tee
du dem
Ngalla reema,ma reela
Soo tee finga tee ma tee fima tee
Du dem
Ngalla reema ñu bègue
Di tongo di lëngo,moma gënal
Ñari fan ñatt rek yune nga fay
Wetaayu guddi man mongui may ray
Bilee situation manatula wëy yaw
Soxnasi man taayi na
Soxnasi ciow dafay jeex
Ohooo ,anhaaq ,iihiiiiiiii