Bagne Lène歌词由Alibeta&Rhapsod演唱,出自专辑《Bani Adama》,下面是《Bagne Lène》完整版歌词!
Bagne Lène歌词完整版
Bañleen
feat. Rhapsod
Iyaye kanaga kanaga
Iyaawoooo kanaga kanaga
« Le colonisé ressemble un peu, ou
L’ex-colonisé ressemble un peu, à cet
Esclave du 19eme siècle, qui une fois libéré,
va jusqu’au pas de la
Porte puis retourne à la maison, parce
Qu’il ne sait plus où aller » (Cheikh Anta Diop)
Bañ ku ñu xañ /li ñu moom nañu sañ
Kañ sunuy ñoñ/ ñi leeral ba mu ne nàññ
Doon ay keletigi / ñi sëggoon nañu siggi
Na jaambaar yi takkaat ndigg yi /
Ñu tooyalaat xol yu ñëg yi
Fésal taar bi ñu bëggoon a ñaawal
Saxal koom bi ñu bëggoon a néewal
Am pasteef name nihma bay gellwaar
Delluwaat ci ngor ak xam-xam /
Reenu Naataange
Am doole ci mboloo djali-djalobe gellwaar
Yeewu yewweeku ci bépp xeetu
Nootaange
Bañ xeeb sunu bopp fàtte lépp
Li nuy tënk
Fésal dëgg, rësal fen yeesal
Li ñu maam dénk, bañleen
Refrain
Yeewuleen te xam li ngeen doon,
Bañleen
Buleen nangu ñu xeeb li ngeen
Doon, bañleen
Bañleen ñi nootoon Maam bóoy
Noot doom, bañleen
Tànnleen seen xel rëddleen seen
Yoon, bañleen
Li fi xewoon ci jamono moo fi teewat ci
Beneen fan
Ndax bile yoon ñoom dañoo noot
Sunuy kàngam,
Bañleen ñu rëdd seen yoon,
African people jógal get up and
Fight !
Refrain
Bañleen, bañleen (bis)
Iyaye kanaga kanaga !
Iyaawoooo kanaga kanaga !
Bañleen
Koulene wo dilene wah ki guene donoul !
Afro pessimisme, bañleen !
Réer ànd ak ñi dëddu seen yoon,
Ànd ak illuminati ! Bañleen
Ñoom ñi nootoon Maam bóoy noot
Doom, neocolonialisme !
Tànnleen seen xel, rëddleen seen
Yoon ! Revolution time !
Ndooling eh ndoling, ndoling mama
Talla
Talla talla koumbo koti mama sarr
Dniamkoumaran ndigue, ye ye ye
Sita kat, gnamba kata djamanding satt a !
« l’Afrique devrait, sur des thèmes
Controversés, être capable d’accéder a
la vérité par sa propre investigation
intellectuelle, Se maintenir à cette vérité,
Jusqu’à ce que l’humanité comprenne
Que l’Afrique n’est plus frustrée