Saajobaan歌词由Amadeus演唱,出自专辑《Saajobaan》,下面是《Saajobaan》完整版歌词!
Saajobaan歌词完整版
Zoom on the beat
Eey M脿samba Waalo
hummm hun
Su mb毛ggeel doon jaay
Am naa nj毛gam
Dinaa la wan sama y茅ene yi ma am ci yaw
Duma ku lay jay
Te duma la wor
Dinaa la wax d毛gg ak lum metti metti
Maa la woo ne la maa la nob
Miinal la sama bopp ba nga barder maa la too帽
Kon nag loo ma manti def
Lu mu metti naa ko mu帽
脌dduna du dox ba ma soppi li ma la wax doo ma weddi
Ay bu doon ay nax neex na ma
Fekk ma ciy g茅nt yee nga ma
J脿mm ju bari may nga ma
Yaa ngi may dundal 脿jjana
Tamit t毛ggal ma ma jaayu
Xamal ma ne man la
G毛mal ma ne Man rekk nga nob
Sama saajobaan
T毛ggal ma ma jaayu
Xamal ma ne Man la g毛mal ma ne Man rekk nga nob Sama saadjobaan eeee waay
Xam nga duma puruux duma f脿tte bi may surux
Xuntu wu l毛nd毛m wi nga ma g茅nne dinaa ko wax
Du lu rafet ci wax
Soo ma b脿yyee damay torox
Nawle y茅pp bis bu 帽u teewee dinaa ko wax waaaay
Doy nga ma ci k毛r
Kenn du la sikkal
Man yaw mii yaay ki ma fiital
Doo dund ngistal
Ngor gi nga jiital
Ragaluma siiwal
Nun 帽aar ndax doy nga ma ci k毛r
Ndaxte Mane maa la woo
Ne la maa la nob
Miinal la sama bopp ba nga barder maa la too帽
Kon nag loo ma manti def
Lu mu metti naa ko mu帽
脌dduna du dox ba ma soppi li ma la wax doo ma weddi
Hay bu doon ay nax neex na ma (bu doon ay nax neex na ma)
Fekk ma ciy g茅nt yee nga ma (Fekk ma ciy g茅nt yee nga ma)
J脿mm ju bari may nga ma (J脿mm ju bari may nga ma)
Yaa ngi may dundal 脿jjana
Tamit t毛ggal ma ma jaayu
Xamal ma ne Man la
G毛mal ma ne Man rekk nga nob Sama saajobaan
T毛ggal ma ma jaayu
Xamal ma ne Man la
G毛mal ma ne Man rekk nga nob Sama saajobaan
T毛ggal ma ma jaayu
Xamal ma ne Man la
G毛mal ma ne Man rekk nga nob Sama saajobaan
T毛ggal ma ma jaayu
Xamal ma ne Man la
G毛mal ma ne Man rekk nga nob Sama saajobaan eeee waaay