YAAY KAN歌词由Yoro Ndiaye演唱,出自专辑《YAAY KAN》,下面是《YAAY KAN》完整版歌词!
YAAY KAN歌词完整版
Yaay kan?
Bëggnaa ku xam linga moom,linga doon,xam fanga joguee,yaw yaay kan
Bëggnaa ku xam linga moom,linga doon,xam fanga joguee,yaw,yaay kan
Bula kenn jawale,
bula kenn tëkële
Bula kenn dëkële fanga dëkul
Nañuy rañale
Bula kenn jawale,
bula kenn tëkële
Bula kenn dëkële fanga dëkul
Nañuy rañale
Yaw yaay kan?
Yaw yaay kan?
Ku xam fanga joguee,fanga sosso
Am loy jomb
yaw di soraale ñii lay romb
Fanga joguee,ni waxee,ninga doxale ,tax ñu rañee la,xammee laa
Yaw yaay kan
Bula kenn jawale,
bula kenn tëkële
Bula kenn dëkële fanga dëkul
Nañuy rañale
Bula kenn jawale,
bula kenn tëkële
Bula kenn dëkële fanga dëkul
Nañuy rañale
Yaw yaay kan?
Yaw yaay kan?
Bëggnaa ku xam linga doon,linga moom,xam fanga joguee,yaw yaay kan?
Yaw yaay kan?
Bula kenn jawale,
bula kenn tëkële
Bula kenn dëkële fanga dëkul
Nañuy rañale
Bula kenn jawale,
bula kenn tëkële
Bula kenn dëkële fanga dëkul
Nañuy rañale
If you ignor your past culture
You’are like a imty tree withe no roots back,back to roots ,back to the roots men
Dont forget where you coming frome,dont forget your history
Judd gu rëy nday ak baay,
Waye ya moom sa fulla
te yaa moom sa fayda
Yakoy dokhee bañu respecter la
Xam yaay kan
Wude nim la guisse,lalay ëwëlee
Gaindé buñu ko dabbe cia doxinn bala
Xam sa boppa gën ñu woo la waxlalo
Ku wacci sa and dem wutiji and
And boo yeek moom fekk cia boroom
Yaw yaay kan?
Yaay yaay kan?
Yaw yaay..,