XALE BU JIGUEEN歌词由Yoro Ndiaye演唱,出自专辑《YAAY KAN》,下面是《XALE BU JIGUEEN》完整版歌词!
XALE BU JIGUEEN歌词完整版
Xale bu jigueen
Njangu xale yu jigueen yi barina gallangkoor
Barina ci reewmi luñu leen di tek toor
Mu toll ci jangue nga xañ koko
Xañ koko
May ko kumu beggul ba sank ko
Sank ngako
Hypothéquer lifam lorr nga ko
Lorr nga ko
Xale bu jigueen la momitam
Jangam amna solo
Aarko ndax jigueen la momitam
Jangam amna solo
Goor baaxna jigueen itama baax
Nga xarfal jigueen lor ngako guiiru dundam
Xale bu toll ci jangue école nga diko sakku
Yenn sayi mu jël ci ëmb Jangam bi yakhu
Mu toll ci jangue nga xañ koko
Xañ koko
May ko kumu beggul ba sank ko
Sank ngako
Hypothéquer lifam lorr nga ko
Lorr ngak
Xale bu jigueen la momitam
Jangam amna solo
Aarko ndax jigueen la momitam
Jangam amna solo
Goor baaxna jigueen itama baax
Aarko ndax jigueen la momitam
Jangam amna solo
Goor baaxna jigueen itama baax
Mu toll ci jangue nga xañ koko
Xañ koko
May ko kumu beggul ba sank ko
Sank ngako
Hypothéquer lifam lorr nga ko
Lorr ngako
Disons non à l’excision
Xañ ko ko
Les violes les incestes ont détruit la vie de tant de jeunes filles
Lorr nga ko
Mu toll ci jangue nga xañ koko
Xañ koko
May ko kumu beggul ba sank ko
Sank ngako
Hypothéquer lifam lorr nga ko
Lorr ngako
Ngala way bayileen xel ci ñom
Xale bu jigueen lune la mana doon
Sank ngako
Lorr ngako